Joxàl mala bi mu lekk! (Wolof)

500+
Descargas
Calificación del contenido
Apto para todo público
Imagen de la captura de pantalla
Imagen de la captura de pantalla
Imagen de la captura de pantalla
Imagen de la captura de pantalla
Imagen de la captura de pantalla
Imagen de la captura de pantalla
Imagen de la captura de pantalla

Acerca de este juego

Joxàl mala bi mu lekk dey jàngal sa doom yi baat ag araf yi njëk ci jàng lifantu. Tannal mala bu tojagul ci nenam diko jox mu lekk ay araf ag baat ngir mu magg ba doon xarit bu bess ci yow

LAN MOY JOXÀL SA MALA MU LEKK ?
Joxàl sa mala mu lekk dey jëffëndiko ay feemu po yuy jàngale yuñu tekk ci xam-xam yu woor ngir fexe ba dimbële sa doom yi ñu Sawar ci jànk mi. Xale yi di neeñ bég di tànn ag di gis ni sen xaritu mala yi di magge ba pare di jàngale baat ag araf yu njëk yi lenn di dimbële ñu mëna liir


AM KO CI SA TELEFON TE DO FAY DARA, AMUL AY NATAALU SIIWAL, AMUL LOY FAY CI BIIR PO MI !
Curious Learning, CET ag Apps Factory, di ay kurel yuy ñongal jàngum làkk yi, ñooko defar te wutuñu ci benn dërëm. Do fay dara ci po mi !

MÀNDARGAWU PO MI NGIR ÑONGAL XAM-XAMU LIFANTU:
• Ay laaj yu neex te reelu jëm ci araf yi
• Ay po ngir xaame araf yi ngir liir ag bind
• Ay po ngir nafar ak denc ay baat
• Ay niiwo yu jafe yo xamne “baat bi rek gey dégg”
• Alluwa bu wayjuur yi mëna xayma tolluwaay sen doom
• Po mu nit yu bëri mëna deffando andak ñu mëna xayma tolluwaay kenn ku ne
• Ay mala yoo mëna tànne sa bula neex, yu lay dimbële nga foo, ree boolek jàng
• Dey yokku xaaraaŋtef jëm ci jókko ag yëkk-yëkk
• Do fay dara ci bir po mi
• Soxlawul dara lu leey lëkkale ag enternet

AY ESPESYAALIST YU XAARAAÑ ÑOOKO DEFAR PUR SA DOOM
Po mi ñongi ko amal ci ay atu xalaat, xayma ag jëfandikoo ci xam-xamu baat ag araf yi. Dafa dëxëñ ci bir ay xam-xam yu am jëriñ, bokk nasi xamee jëm ci ni ñuy binde baat yi, xamee araf yi, mbindum baat yi, xam-xamu baat yi ak lumuy tekki, jàng baat yi ñuy gis. Ginaw bi ñu ko defare ci màndargawu mbëggeel ag ay mala yu bëri, po mi dey dimbële xale yi ci ñu am setlu, yeewute jëm ci sen yoonu maggaay.

ÑOY ÑAN ?
Kurel gi di Joxal mala bi mu lekk ñu gën ka xam ci “Feed the monster” mongi am ci ndimbëlu banxaas bi yóor wallum bitiw rew bu dëkk bi di Norwes ginaw bimu bokke ci joŋante bi di “EduApp4Syria-competition”. Jumtukaayu bu njëku po mi mo ngi nekkoon ci làkkup arab ñu defaroon ko ci lëkkalowu kurel yi di Apps Factory, CET: el Centro de Tecnología Educativa ag IRC: el Comité Internacional de Rescate.

-------------------------------------------------

Feed The Monster enseña a los niños los fundamentos de la lectura en wolof. ¡Recoge huevos de monstruos y aliméntalos con letras para que puedan convertirse en nuevos amigos!

¿QUÉ ES FEED THE MONSTER?
Feed The Monster utiliza técnicas comprobadas de "jugar para aprender" para involucrar a los niños y ayudarlos a aprender a leer. Los niños disfrutan coleccionando y cultivando monstruos mascotas mientras aprenden los fundamentos de la lectura.

¡DESCARGA GRATIS, SIN ANUNCIOS, SIN COMPRAS DENTRO DE LA APLICACIÓN!
Todo el contenido es 100% gratuito, creado por las organizaciones sin fines de lucro de alfabetización Curious Learning, CET y Apps Factory.

CARACTERÍSTICAS DEL JUEGO PARA PROMOVER LAS HABILIDADES DE LECTURA:
• Rompecabezas de fonética divertidos y atractivos
• Juegos de trazado de letras para ayudar a leer y escribir
• Juegos de memoria de vocabulario
• Desafiantes niveles de "solo sonido"
• Informe de progreso de los padres
• Inicio de sesión de varios usuarios para el progreso de cada usuario.
• Monstruos coleccionables, evolutivos y divertidos
• Diseñado para promover habilidades socioemocionales
• Sin compras dentro de la aplicación
• Sin anuncios
• No se necesita conexión a Internet

DESARROLLADO POR EXPERTOS PARA SU HIJO.
El juego se basa en años de investigación y experiencia en la ciencia de la alfabetización. Incorpora habilidades clave para la alfabetización, incluida la conciencia fonológica, el reconocimiento de letras, la fonética, el vocabulario y la lectura de palabras a la vista para que los niños puedan desarrollar una base sólida para la lectura. Construido en torno al concepto de cuidar de una colección de monstruos, está diseñado para fomentar la empatía, la perseverancia y el desarrollo socioemocional de los niños.
Actualización
13 oct 2020

Seguridad de los datos

El primer paso de la seguridad es comprender cómo los desarrolladores recopilan y comparten tus datos. Las prácticas de privacidad y seguridad de datos pueden variar en función del uso de la app, la región y la edad. El desarrollador proporcionó esta información y podría actualizarla con el tiempo.
Esta app podría compartir estos tipos de datos con terceros
Ubicación, Actividad en apps e Información y rendimiento de la app
Es posible que esta app recopile estos tipos de datos
Ubicación, Actividad en apps e Información y rendimiento de la app
Los datos están encriptados en tránsito
Puedes solicitar que se borren los datos
Se comprometió a satisfacer la Política de Familias de Play

Novedades

Google Play update.