
Yoro Diame
Assalaamu halaykum wa rahmatul Laahi tahaalaa wa barakaatuhuu. Noo ngi siyaare bu baax a baax te di leen ñaanal jàmm, di ko sàkku ci yéen. Liggéey bi am na solo lool te kawe na itam. Ndokk ba leen ci Ku Baax Ki nammee liggéeyloo, Yal na nangu lépp te barkeel ko karbeb Xasaa-id yi, jaangeenjëf.
Babacar Mbengue
24 de abril de 2025